Lu ëpp ci Pluggable Transports, yu mel ni obfs4, dañuy wéeru ci jëfandikoo yu jàllalekaayi "bridge".
Nirook jàllalekaayi Tor yu baax, bridges yi ñu ngi daw ci seen coobare; wuteek jàllalekaay yu baax yi, waaye, duñu leen lim ci lu fës, looloo tax ab noon mënu leen a ràññee ci lu yomb.
Jëfandikoo bridges yu ànd ak pluggable transports dafa lay dimbali ngir doo feeñ ci sa jëfandikoo Tor, waaye mën a wàññi dooley lëkkaloo bi soo ko tëkkaleek jëfandikoo jàllalekaayi Tor yu baax.
Yeneeni pluggable transports, yu mel ni meek ak Snowflake, dañuy jëfandikoo ay tekniku jumtuwaay yu dul ubbi ay pexe yu wéeruwul ci seet ay dëkkuwaayi bridge. Soxlawuloo am ay dëkkuwaayi bridge ngir jëfandikoo transport yi.
JOT DËKKUWAAYI BRIDGE YI
Ndax dëkkuwaayi bridge yi fësuñu, dina laaj nga seet leen yaw ci sa boop. Am nga yenn tànneef:
Request bridges from within Tor Browser
Su fekkee yaa ngi soog a jëfandikoo Tor Browser, kilikeel ci "Configure Connection" ngir ubbi palanteer bu sukkandikukaayi Tor yi.
In the "Bridges" section, locate the option to "Find more bridges" and click on "Request bridges" for Tor Project to provide a bridge.
Mottalil Captcha bi te nga kilike ci "Submit".
Kilikeel ci "Connect" ngir deñc say sukkandikukaay.
Wala, soo yoree Tor Browser buy dox, kilikeel ci "Settings" ci àlluwa hamburger (≡) ba noppi ak ci "Connection" ci wàllu wet gi.
In the "Bridges" section, locate the option to "Find more bridges" and click on "Request bridges" for Tor Project to provide a bridge.
Mottalil Captcha bi te nga kilike ci "Submit".
Sa sukkandikukaay dina nu ko deñc automatically soo sëxee ba tëj xët bi.
Obtain bridges from the Bridges website
Visit our bridges website.
Click on 'Just give me bridges!' and copy the bridge lines.
Or use advanced options to select the type of pluggable transport and only get bridges with a IPv6 address.
Obtain bridges via Email
Email bridges@torproject.org from a Gmail or Riseup email address and copy the bridge addresses received in the email.
Obtain bridges via Telegram
Send a message to @GetBridgesBot on Telegram.
Tap on 'Start' or write /start
or /bridges
in the chat.
Copy the bridge addresses.
DUGGAL DËKKUWAAYI BRIDGE YI
Tor Browser Desktop
Su fekkee yaa ngi soog a jëfandikoo Tor Browser, kilikeel ci "Configure Connection" ngir ubbi palanteer bu sukkandikukaayi Tor yi.
In the "Bridges" section, from the option "Enter bridge addresses you already know" click on "Add new bridges" and enter each bridge address on a separate line.
Kilikeel ci "Connect" ngir deñc say sukkandikukaay.
Wala, soo yoree Tor Browser buy dox, kilikeel ci "Settings" ci àlluwa hamburger (≡) ba noppi ak ci "Connection" ci wàllu wet gi.
In the "Bridges" section, from the option "Enter bridge addresses you already know" click on "Add new bridges" and enter each bridge address on a separate line.
Say sukkandikukaay dina nu leen deñc automatically soo sëxee ba tëj xët bi.
Tor Browser for Android
Tap on 'Settings' (⚙️) and then scroll to the 'Connection' section of the settings.
Tap on 'Config Bridge'.
Toggle on 'Use a Bridge' and select 'Provide a Bridge I know'.
Enter the bridge address.
Su lëkkaloo bi jàllulee, bridges yi ngay jot mën nañu wàcc. Ci bu la neexee jëfandikool benn ci tëralin yii ci kaw ngir am yeneeni dëkkuwaayi bridge, te nga jéemaat.
BRIDGE-MOJI
Dëkkuwaayu bridge bu ci nekk dafay feeñ ci ab liiñu màndargay emoji bunu tudde Bridge-mojis. Bridge-mojis yi mën nañu leen jëfandikoo ngir weral ne bridge bi nga bëggoon yokk nanu ko ci ak ndam.
Bridge-mojis nekk nañu xameekaayi bridge yu nit mën a jàng te duñu wone baaxaayu lëkkaloo bi ci jokkoowu Tor wala nekkinu bridge bi.
Liiñu màndargay emoji bi mënu nu ko jëfandikoo niki xibaar bunu duggal. Jëfandikukat yi nu ngi leen di laaj ñu duggal dëkkuwaayu bridge bu mat sëkk ngir ñu mën a lëkkaloo ak ab bridge.
Dëkkuwaayi bridge yi mënuloo leen séddoo sooy jëfandikoo QR kot wala sooy sotti dëkkuwaay bi yépp.