CHOOSE DISPLAY LANGUAGE

When you launch Tor Browser the display language is set to the default language of your system. Tor Browser is available in multiple languages and you can change the display language by clicking on "Change Language".

Change Tor Browser's display language

In the "Language" settings, select your desired display language from the dropdown menu.

Select display language of Tor Browser

LËKKALOO

Soo taalee sa Tor Browser, di nga gis palanteer bu Lëkkalook Tor. Lii daf lay jox ab tànneef ngir wala nga lëkkaloo te du am jàdd ci jokkoowu Tor bi, wala nga defaraat Tor Browser ngir sa lëkkaloo. Toggle on "Always connect automatically" to allow Tor Browser connect to the Tor network automatically with the previously saved connection settings, everytime the browser is launched.

Kilikeel 'connect' ngir lëkkaloo ak Tor

Ci anam yu bare, tànn "Connect" dina la may nga lëkkaloo ak jokkoowu Tor bi te doo am benn tërëlin booy samp.

Soo xasee ba kilike, ab bantu status dina feeñ, di wone tolluwaay lëkkaloowu Tor. Su fekkee danga am lëkkaloo bu gaaw, wànte bant bi dafa niroog lu taxaw ci ab tomb, jéemal 'Connection Assist' wala xoolal xëtu Troubleshooting ngir mu jàppale la nga saafara jafe-jafe boobu. Wala, soo xamee ne sa lëkkaloo danu ko yamale wala nga jëfandikoo ab proxy, danga war a kilike ci "Configure Connection".

Kilikeel 'Configure Connection' ngir jek jekal sukkandikukaayi jokkoo yi

CONNECTION ASSIST

Su fekke Tor fatt na ci sa bërëb, jéem ab bridge mën na la jàppale. Connection Assist mën na tànn benn ngir ngay jëfandikoo bërëb bi nga nekk.

Connection Assist buy doxal boppam

If Connection Assist is unable to determine your location you can select your region from the dropdown menu and click on 'Try a Bridge'.

Connection Assist defaraat

DEFARAAT

Tor Browser dina la yobbu ci ay xeeti tànneefi roofoo.

Connection Assist bi daf lay yëgal sa tolluwaayu lëkkaloowu Internet ak sa lëkkaloo ci jokkoowu Tor.

Lëkkaloo xayma bu àndak ndam

Lëkkaloo xayma bu jàllul

The first toggle is 'Always connect automatically'. If toggled on, every time you open Tor Browser, it will try to connect with your previously saved connection settings.

Connect Automatically

Su fekkee sa lëkkaloo danu ko yamale, wala danga jéem te lajj lëkkaloo ci jokkoowu Tor ak benn saafara doxul, mën nga defaraat Tor Browser ngir mu jëfandikoo ab pluggable transport. 'Bridges' dina wone Moytukaaypàcc ngir defaraat ab pluggable transport wala lëkkaloo jëfandikoo pom yi.

Defaraatal Tor bridge

YENEENI TÀNNEEF

Su fekkee sa lëkkaloo dafay jëfandikoo ab proxy mën nga ko defaraat di kilike ci 'Settings ...' ci 'Defaraat nan Tor Browser lanuy lëkkaloo ci Internet'. Ci anam yu bare, lii amul solo. Dinga xami ndax danga soxla tànn checkbox bii ndax sukkandikukaay yu niroo lanuy jëfandikoo ngir yeneen xuusukaay yi ci sa doxinu jumtukaay. Su mënee nekk, laajal sa caytukatu jokkoo ngir gindi. Su fekkee sa lëkkaloo du jëfandikoo ab proxy, kilikeel ci "Connect".

Proxy sukkandikukaay ngir Tor Browser